Libàas Niang neena Wolof lay motaliko yéenem. Neena timit bul xéeb wolof, ndax danga fatee ! Ñun amunu complexe ci lakùm olof. Dunu ay arabisant, dunu ay francophone, dunuy ay anglophone, dunu hispanophone itam. Olol moy sunub laakà. Laaka gën ci mindéef ci ñaareelu ñëwam ci aduna ! Lakkù ñakay tàgga, Baay Libàas Niang ak Baay Malick Mbay. Ainsi les premiers se retrouvèrent derniers. Et les derniers furent les premiers. [ bible, évangile de Marc 10:31 ] Le peuple noir qui fut pendant longtemps « oublié » a du attendre la fin des temps pour recevoir la prophétie. Et l’attente en valait la peine puisque c’est le meilleur de toute la Création qu’on a envoyé parmi nous. Wayee niit ku ñuul dafa réer, Baay Laay bu done niit ku xés, ngen jàppa diineem. Li teeree yi done juñj, Yonen bi moo ñëwaat jëfal ko boppam. Motax ay waxu Libaàs Niang, Mali Mbaye, Seex Maktaar Lô ñoo gëna wér si ñun waxii teree yu yaagà yi. Fuuf sax.